TagattUbité bi Les formations d'E-TIC sont pratiques afin de répondre aux besoins du terrain: Jangalem E-TIC mungi soxal ňi yaar ňuy waaja lim: Xaac bu jënk biJangum jangalekat yi nga xamni ňooy dem ci pënc yi:
li waral doxalin boobu nak mooy daňu bëgg topando bi daldi ko lawal Ndax mu nek luňu mëna sottal.sunu jangale mu jënk mi nak dafay yëngu lool. Bènn jaabante bu dùll jeex lay doon ci sèddale xibaar ak wutum xibaar yooyule ci pënc yi. Ci wàll woowu nak laňu gënna soxla yooneent yi.loolooy waral porozet bi di gënna mënna and ak yitte ak soxla u jamono. Looloo waral ICVontaires tëral ay Mebètt am ci nii:
Xaaju ňaarel biBaykatt yi nak, ňooy faral di Gënna nek ci tool yi ak Pënc yi, seen jang daanaka soriwul, mooy waral seenum jang ak mokal yi doxalin yi di àjju ci xarala yu mujj yi ci diir wi ňu ko àppal ci porozet bi. Waye nak loolu tere wul dinaňu mënna jott ci xibaar yi ňu jaarale ci ndaw yiňu yooni ci pënc yi (radio yi jigeen ňi) walata sax yi ňuy jaaral c seen telefon porataabal yi, yi ňuy jottali ci baay tama ak, bu mëne nek, ay taf yuňi taf ci miir yi. |