Ay jumtukayRadio gox-goxaan yi Pacc bi moom mu ngi taataan ay jumtukaay ak ay bërëbu radio gox-goxaanu Senegaal ak Maali. SenegaalLi ko dalle ci atum 2006 ba leegi Senegaal bénn kureelu radio gox-goxaan rek la am: URAC moo boole ARC ak ARPAC. Kurel bu bees bi nak mungi mebeta wann nguur gi ap sartu radio gox-goxaan yëp.book n ci tamit ap tiyaatar ci kalama wolof bu ňu fassa dawal ci radio yi te loolu nak Ambassadu tugal ca Dakaar mooko jooxe. Munga giss listu radio gox-goxaans Senegal lonkuway. LonkuwayCA MaaliCa Maali 168 radio yo xamni 121 yëpp ay radio gox-goxaan, 38 radio jaaykat ak 9 radio diine (xibaaru URTEL ca Maali - URTEL). Munga giss radio yêpp boo besee yi lonk bi: liste des radios libres du Mali (fichier pdf). Lonkuwaay
Adina wërngël këpp
Teere yi |