AgriGuide
Dans le cadre du programme E-TIC, des artistes ont créé des illustrations servant de base pour des affiches et autres supports didactiques. Des remerciements particuliers vont aux illustrateurs.
Conte d'Abdou Kane Ndaw
Versions disponibles:
Bèen kurèelu ay nitt ñoo dùgg ci gox goxàanu Senegaal ngir waxtaanal lèen ci njariñal jumtukàay yu xaral yi ak tass xibàar jëmeléko ci ci sèeni mbay, ak tamit ngir càmm jawu ji.
|
Baykatt yi dañu daàn faral di jëfendiko porodi yu sakan sakana.
|
Wayé daño jëki-jëki rèk nitt ñi di tambalé silmaxa. | Ñéneèn ñi dañoo tambaléwoóna am ay doóm yu am ay galankoor ci sééni awra. |
Ci lañu xamè ni banxaasu jawu ji daño dugënté. Ki di yëngu ci wallu mbay mi mungi lèen wax jëriñal garab, sèen jëriñ ci wallu dund ak litax ñu wara jëmbët yu wuùte. |
Lèegi ñu woó ki nga xamné mooy yëngu ci wallù yu bideèw yeek jawu ji mu waxleèn jëriñal yoóyule jumtukaay ngir ñu mëna soór luñu wara bay ci atmi ñëwëgul.
| Ki yëngu ci Ci jumtukaay yu xarala yi moom muŋi leèn jangal nuñu lèen jëfëndok. Waxna lèen ni ak jumtukaay boobu ñu tude internet, dinañu mënna jott ci xibaàr ci mbay mi tè dinañu mënna waxtaan ak sèeni naatango ci aduna bi yëpp te di mënna jokalante ak ñoom. |
Bi ñu nóppe ci ndaje yëpp nak wa gox bi xamnañu ni jëriñal jumtukaay yu xarala yi. Ndax dina lèen japalé ci xibaar yi te dina lèen taxa aàr jawu ji ak njurr gi.
|
Loólu bokk na ci li gënna yokk wergu yaramu xale yi ak gox yi ñu dém. | Loólu moo yokkù celak ngoób mi ak celak dund gi ci gox mi yëpp. |
A propos de l'artiste: Abdou Kane Ndaw est un jeune artiste sénégalais de Rufisque. A l'Université de Cheick Anta Diop, il fait des études universitaires en géographie. Il suit également des cours à l'Ecole Nationale des Beaux-Arts (ENA) de Dakar. Plus: http://www.facebook.com/abdoukane.ndaw.
Comment utiliser l'AgriGuide?
Nous vous invitons à nous contacter si vous avez des questions concernant l'AgriGuide et/ou notre programme E-TIC.