Printer-friendly version


Andandoo yi

Poroze bi di E-TIC, te ňu bari di ci ligey, ICVolontaire moo koy sos.ligey baa ngitaxawe ca Maali ak Senegaal(ci jeeri ji), ci ndimbalal Fond Farancophone des Inforoute ak yeneen andandoo.

Ci ndimbalal



Ligeyu Fonds francophone des Inforoutes mooy suxali ak dooleel xam-xamuk xarala yu mujj yi ci dëk bëtt gaannar, diggi ak penku Ërop ;ci japale, bu ňu woote ay poroze ba pare, ay xalaat yu mucc ayib ci walu xarala yu mujj yi yoon wi ňu tëral ci seen saart ca (ndaje dëkk yi bokk kalama nasaraan).

Andando yi

 

ICVolontaires (www.icvolontaires.org) ap kureel la buy ligey ci maaliporo bu jublu ci wallu jokko ak ci kalaama, ligeyu way dimblikat yi ak dimbali ndaje yi.yokute, sootante xalaat yi ak ligeyu askan wi ňëpp di bokk ak kureel yi jublu ci wallu dimbali nitt ňi la ňuy wann ňëpp ňu ňuy japale. ICVolontaires-Maali moy taxawal ICvolontaires ca Maali.


Sénégal

EREV / Gensen

Gensen Sénégal (www.gensenegal.org) ak wa Eath Rights Eco-village Institute (www.earthrightseovillageinstitute.org) ay ONG la ňu yuy jeema xeex xiif ak ndol ci adina bi, dimbali suxalikuk reew mi, sàmm jawu jiak xam-xamu caada gi ci Afrik. Moom nak mungi lige yak askan wi ci ay pacc yu bari yu jem ci suxaliku.day lige yak ňaari kureelu gox yoo xamni 60 gox-goxaan yi mu ëmb ňooy dalal way dimbalikat yi.EREV nak day sos ay poroze bopam yoo xamni ay ligeykatam ň oo ci yengu, wala yeneen ligey katu yeeneen ong yu mel ni ICVolontaire ci niko saart bi tërele.
 



Campus Numériques de la Francophonie Bamako / Dakar (www.auf.org) mooy daara ju kawe bu Agence Universitaire de la francophonie taxawal ci internet bi. Daara jooju nak amna bërëbu jangukaay te yit day sos ay joŋante ci wallu defar site internet, amna yit ay tagat ci wall woowu jemaleko ci ndaw jangkat yi ci daara yu kawe yi.

 

Youth and
ICTs_Mali

 

Youth and ICTs_Mali Service Civique National bu Senegaal (www.civisme.sn) ap kureel la bu laxu ci ginaaw jëwriň ji yorr ndaw ňi.ligeyam mooy waajal askan wi lu jëm ci wallu ligeyal sen reew,ak xam-xam bu macc c wall woowu boole kook patef wu rey ci walu warefu nit ak reewam. mebetam mooy tagt ndaw ňi  ci ligeyal senn reew ci seen coobare booleko ak di leen tagat ci xarala lëpp ngir sentu ci ňoom  ëlek ňu mënna ligeyal seen askan,taxawu dëkk bi ci jëm kanamu reew mi.di leen tagat tamit ci seen ligeyu ëlëk ci biir rew mi.

 

 

Service Civique National du Sénégal (www.civisme.sn) ap kureel la bu laxu ci ginaaw jëwriň ji yorr ndaw ňi.ligeyam mooy waajal askan wi lu jëm ci wallu ligeyal sen reew,ak xam-xam bu macc c wall woowu boole kook patef wu rey ci walu warefu nit ak reewam. mebetam mooy tagt ndaw ňi  ci ligeyal senn reew ci seen coobare booleko ak di leen tagat ci xarala lëpp ngir sentu ci ňoom  ëlek ňu mënna ligeyal seen askan,taxawu dëkk bi ci jëm kanamu reew mi.di leen tagat tamit ci seen ligeyu ëlëk ci biir rew mi.
 

Association de la
Communauté d’Ouladnagim

Association bu Communauté bi ci Ouladgnagim (www.shindouk.org) Shindouk  moo koy jiite, di njitu xeet woowu, tolu ci 1500 nitt ňu dëkk ci jeeri ji.seen dëkuwaay ya ngi tollu ci 120 ci ay kilometar ci ganaaru tombuktu ci yoonu wutkatu xorom ya ca Taoudunit (azalahi). Xeetu berabish yooyu ňu tude Ouladgnanim (doomu bidew yi), ay naaru ganaar laňu yu book ci touareg yi. Seen yëngu-yëngu yëpp nak mu ngi feete ci càmmuk gëleem yi, Asalai wala gadug xorom ci ginawu gëleem yi di ko jaay.

 

 

Askanu Guédé Chantier b Feete ci bëtt gaanaar jëm penkuk Senegaal, ci dëkk bu ňuy wax Saint Louis, ca goxuk Podor.ap gox-goxaan la bu askan wa di lak tukuloor ak peul yuy yëngu ci wallu Mbay,càmm ak nàpp.

   

©1997-2024 ICVolunteers|system mcart|Updated: 2024-11-25 06:08 GMT|