Ay jumtukay

Radio gox-goxaan yi

Pacc bi moom mu ngi taataan ay jumtukaay ak ay bërëbu radio gox-goxaanu Senegaal ak Maali.

Senegaal

Li ko dalle ci atum 2006 ba leegi Senegaal bénn kureelu radio gox-goxaan rek la am: URAC  moo boole ARC ak ARPAC. Kurel bu bees bi nak mungi mebeta wann nguur gi ap sartu radio gox-goxaan yëp.book n ci tamit ap tiyaatar ci kalama wolof bu ňu fassa dawal ci radio yi te loolu nak Ambassadu tugal ca Dakaar mooko jooxe.

Munga giss listu radio gox-goxaans Senegal lonkuway.

Lonkuway

CA Maali

Ca Maali 168 radio yo xamni 121 yëpp ay radio gox-goxaan, 38 radio jaaykat ak 9 radio diine (xibaaru URTEL ca Maali - URTEL).

Munga giss radio yêpp boo besee yi lonk bi:  liste des radios libres du Mali (fichier pdf).

Lonkuwaay

Adina wërngël këpp

  • CTA Rural Radio: att mu jot dinaňu defar 5 emisoŋ yu wax ci wallu Mbay ak koom-koomi gox yi
  • Farm Radio Weekly ap jumtukaay la bu jublu ci wallutassare xibaar ci Afrik sow jant, farm radio mooko mo
  • AMARC ap kureel la buy japale radio gox-goxaan yi ci lu ëpp 110 reew amna nak lu ëpp 3000 ligey kat
  • Groupe Sud-FM

Teere yi

©1998-2024 ICVolunteers|system mcart|Updated: 2024-10-16 00:53 GMT|Privacy|