Ay tèere

Ci pàcc bi

Ëttu gëstukaay bi ňu lèen jaglèel moo leen di wan teere yu bees yi ak situ internet yu yees yi ak lèpp lu jëm ci xibaar yi lamboo ak mbay camm ak nàpp ci Senegaal ak Maali.

Site yu bees yi

Teere yi

Situ mbootaay yi

Toolekaay yi

Ligey bi ak gëstu mi

Baat yi ňu dagg

Ci bunt bi tamit munga fi fek ay teere yu bari yu ndaw yi bind ci dëk yi ňu jotta dem ci Senegaal ak Maali.

Biral ab gëstu

So bëgge wane ab teere nak mun nga noo joot ci bunt bi.

©1998-2017 ICVolunteers|system mcart|Updated: 2014-02-24 09:15 GMT|Privacy|